Menu

Guy Marius Sagna démasque Air Sénégal SA: "Ndoxu France lañuy joxe ci Air Senegal"

Mercredi 1 Septembre 2021

On demande les Sénégalais de voyager avec la compagnie nationale malgré ses nombreux manquements mais une fois dedans ce sont des produits français que vous allez consommer. L'activiste Guy Marius Sagna vient de démasquer le deal de AIR SÉNÉGAL SA.


Ndoxu France lañuy joxe ci Air Senegal
Raxas Building Administratif  Macky dénk ko doomi France
Sunu téléphone nu dénk ko doomi France 
Sunu autoroute à péage ñu dénk ko doomi France 
Franc cfa ñu dénk ko doomi France 
Sunu budget ñu dénk ko FMI ak banque mondiale
Làkk wi nuy jëfandikoo ci sunu lekool, farãse
Xare (armée) bu Farãs di daagu sunu biir réew 
Sunu patrimoine culturel ñu denc ci musées France yi
Sunu constitution nu roy ci bu France 
Sunu misig hymne national saf sàpp France
Photo sunu Président sax ñu woo doomu France
Sunuy mbedd ñu jël tuddee doomi France yi nootoon sunu maam ba ci sunuy baay
Raxas douche Macky dénk ko tubaab yi
Waas jën Macky dénk ko tubaab yi
Fippu jot na!
Jallarbi jot na!
Folli jot na!
Tekki jot na!
Moom sa réew jot na!
GMS
Lisez encore

Nouveau commentaire :





AUTRES INFOS

CHERS COMMISSAIRES, VOUS PERMETTEZ ?

3ème mandat : Gris Bordeaux et CIE interpellent le président Macky Sall

"Forces occultes" : Ces images qui contredisent la police nationale (vidéo)

Foot: Karim Benzema quitte le Real Madrid

Ngaaka Blindé appelle Macky à la démission : "On ne tue pas sur mon peuple"

Manchester City remporte la cup face à United

Manifestations au Sénégal : La réaction de Yousou Ndour

Didier Awadi : « Ce procès est juste décevant et son verdict absolument honteux »

Fausse accusation de viol contre Ousmane Sonko : Ce que Adji Sarr risque

Sadio Mané parle : « Trop de sang a déjà coulé depuis 2 ans...»


Flux RSS

Inscription à la newsletter